Dimanche 20 Octobre, 2019 á Dakar
Vendredi 01 Juin, 2018 +33
Audio

Le message de Ahmed Khalifa Niasse aux mourides

Single Post
Le message de Ahmed Khalifa Niasse aux mourides


Article_similaires

2 Commentaires

  1. Auteur

    Anonyme

    En Juin, 2017 (22:06 PM)
    !!
  2. Auteur

    La_vérité

    En Juin, 2017 (09:49 AM)
    As salamou aleykoum wa rahmatoul lah sama mbokk bopp.! Déweneti ngèn balma akh…

    Daniou djiss ni diamono bi ci wattsapp bi, ak ci facebook bi beurei na message yoyy diott gnoulayy wakh nga partagé ko. Bala ngay partagé khamal loy partagé sinon dina la dioureul ay mbougueul you tarr "Yeuwmal khiyam " Leip lougnou neik Yallah kham nako..Bilahi..!

    Yallah kham nani message yi am nassi yo kham ni dagno rakh cheytann..!

    Souniou yaguei lire yèneu message yi leigui suniou iman wathie..gnou bayi fii Yallah, deim diko weur fénènn..!

    Jeune génération bi meunou gnou détecté lolou...Cette génération est en danger !!! Par ce que ay boukki you mboubbo dérou kharr dagno fii beurei...Donc vous les jeunes faites attention !!!

    Tei le pire moy so keu wakhei..gnounei da nga compliqué wala tu vois le mal partout, wala tu n'as rien compris, wala c'est juste une blague, wala dangayy diayy oustaz, wala deggo dinei ..ay you démé nonou..

    Kouffi wakh deugu gnounei wokho deugg, kouffi wakh ay nakhei ay nitt guèneu dila défendre.! Lii kènn khamoul foum gnou dieumei…

    Politicien djoguei feulei nieuw dignou sonnal ci ayy campagne électorale, thi ayy khékh, nékkeu di yéh fiit neu..BOUNIOU NANGOU LOLOU..CAMPAGNE ELECTORAL DIAROUL KHEKH DIAROUL KHOULO !!! Politicien you beurei sèn intérêt bopp lagnouyy défendre, mais intérêt REWMI kou kayy défendre !? VIVONS EN PAIX, DANS LA DISCIPLINE, C’EST ÇA LE PLUS IMPORTANT !

    Keippeu kouma wakh wakh bou ndiagass balnala ci khol bou seiddeu gouyy, damay khamni reik dagua khamoul, Keippeu kou nittei sou djissei deugu rangnei ko.. !

    Wakh bi may wakh sakh dina am gnou keu beugu contredire, louma ci meun dara mais naniou yéwou neilaw bi doyynaa..!!

    Ramadan bi leigui mou diékh, demandons-nous koor gui laan laniou ci dieulei ? Sougn ci dieulei woul yokoutei ci dinei, djikko you bakh naniou kholatt suniou boppou...Déé (la mort) migui nieuw à grands pas, kèneu khamoul fann leu, kagn leu ak naka leu..Yiow mi di lire message bi sakh meun na am souba nga fatou.. ! Naniou délossi suniou khèl..

    MESSAGE BI NASSI NIEUP DIOTT INCHALLAH GUIR SAUVER, GUIR GUIDER AK LEIREUL JEUNES YI..!

    Yalla naniou yallah may djiss djiss bou lèer gnou meuneu rangnei...bijahi Rassoul lahi Sallal lahou aleyhi wa salam ..!! Amine

Participer à la Discussion

Auteur Commentaire : Poster mon commentaire

Repondre á un commentaire

Auteur Commentaire : Poster ma reponse
Top Banner
Banner 01
Banner 01

ON EN PARLE

Banner 01

Seneweb Radio

  • RFM Radio
    Ecoutez le meilleur de la radio
  • SUD FM
    Ecoutez le meilleur de la radio
  • Zik-FM
    Ecoutez le meilleur de la radio

LES PLUS LUS

Newsletter Subscribe

Get the Latest Posts & Articles in Your Email

Identifiez-vous

Don't have an account? Registration
OR